Adiouza - Plan B - Album Plan B

Votre vidéo commence dans 10
Passer (5)
Formation gratuite en FR pour les membres inscrits sur les sites de vidéos

Merci ! Partagez avec vos amis !

Vous avez aimé cette vidéo, merci de votre vote !

Ajoutées by admin
22 Vues
• Plan B disponible sur toutes les plateformes : https://bfan.link/plan-b-1

Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo


Composition : Bril - Adiouza
Prod : ISO
Auteur : Kruh

Lyrics :

PLAN B

Refrain

Xoloulo fignou diaar yaw goré wo
tass yakar bima amone kone weroulo
gueume say wax tok di xaar gnou marier
ndéké yayoyaye may sa plan b

couplet 1
ame diabar ni makoy téré nélaw

dima topeu foumeu dieum melni nguélaw

mane bagne na ba soneu mouy daw sama guinaw

magué ma lou bari taxone mame ma ragal

hééy

kham nga rek
jiguéne dou beug dafay mine

guis nga dé
weri na linewone sama ligne

Refrain

Xoloulo fignou diaar yaw goré wo
tass yakar bima amone kone weroulo
gueume say wax tok di xaar gnou marier
ndéké yayoyaye may sa plan b


2 eme couplet
beuthieuk lakoy ame
goudi mou nakh ma dém

dane ragala ame gane
kou gneuw ma dakh mou dem

xamnga architecte bouy plan
nane ma
bb
je t'aime
ma bien aimé
je taime
bb
féni néne kesse
Ndeker fouwou kayame lawone

nakhnama dém
bayi ma fi
meuneu tou mako séne
thi deuk gui
plan b

refrain
Xoloulo fignou diaar yaw goré wo
tass yakar bima amone kone weroulo
gueume say wax tok di xaar gnou marier
ndéké yayoyaye may sa plan b


Pont
gnou seuye la beugone... té defna limiy laathie...
beugone na diour sa dome...
gnak na ki ma beugone...
gnak na temp bou baré

nane lagoor meun fowé xelou jiguéne
téy léne
l'habit ne fait po le moine
téy léne
casting ko na diaar douane
téy léne

Refrain
Xoloulo fignou diaar yaw goré wo
tass yakar bima amone kone weroulo
gueume say wax tok di xaar gnou marier
ndéké yayoyaye may sa plan b
Yaw gorewo
Naxe ngama

_________________

Retrouvez Adiouza Diallo sur :

- Instagram: http://i.instagram.com/adiouza/
- Twitter : https://twitter.com/Adiouzaofficiel
- Facebook: https://web.facebook.com/AdiouzaPageFans/
Catégories
Architecte
Mots-clés
adiouza, prod, music

Ajouter un commentaire

Commentaires

Soyez le premier à commenter cette vidéo.